N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ... Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii... Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
Souma amone entreprise dieul leu wala yoboula Europe fekhel sa rasta yii goudou nga diko takk ❤ elle est tellement reconnaissante aussi 😢 yalna yalla takhawou defal la ndam goudal fan wi
Motakh apparence lou yèmè leu. Ki kouma diokhone kamil ma wate ni dou djiguène nakh apparence. Mais stp dèl defar sa bopp kom djiguène stp. Courage a toi
Bonne Continuation Jeune Fille Geuneu Gorr Gorlou Rék Xam Linga Beug Focus Si Am Esprit Bou Solides Lissi Déss Nga Bayiko Si Loxoy Süniü Borom Respect ✌️
Worna Serigne Touba Binta je suis fière de toi sa patronne bly limou la sëddel daffa dawwe sama yaram😢😢 machallah yalle nalla yalla Samm si barckë Nabylle Moustapha (psl)❤❤ je vous love❤❤❤❤❤❤❤❤
Bilahii khamou malla mè kou bakhe monguii nii ya gorrë ya ame djiomm sa kholl rafett naa diambarr yaye bauye tu ma fait pleurer 😢 yalla nalla yalla gueuneu takhawou et tu es toute belle 😢😢
Machallah liguey yep bakh mai tmt faut qu’on ce disent la vérité cette Binta koum wakhoul djiguenne leu doka geume man je les vus sur Tik tok yalla xam Nani goor laka tegone mai vraiment daf wara defar apparence bi xolal bopam bi tmt nit mom surtout Sénégalais limou guis rek lalay juger meun na nek mécanique ok mai wanei ni aussi djiguenne leu
Metier mom amoul Goor ak djiguen diom la rek, mais Binta défaroul nak djiguen déy saf djiguen, il y’a des femmes mécaniciennes Com toi mais bolén séné khamni aye djiguen lagnou, courage à toi
Walahi meme ici où j’habite y’a une fille qui fait le soudeur 🧑🏭 mai quand tu la vois dangoy beug elle est belle aussi changer woul comportement mai Binta changeel def yeufou djiguenne
Soyez francs avec elle Li dîné andoussi. Ton travail n'a rien à voir avec ta personne nékal djiguène bila yalla Def lolou moy deugue. Di djegalou nakh si c mes proches j'aurai pas laisser passer donc loubakh lako yéné. Bonne continuation !
MAIS SI TU TIENS À TON DIINÉ ÇA TE REGARDE. ELLE N'EST PAS OBLIGÉE DE FAIRE CE QUE VOUS VOULEZ LUI FAIRE FAIRE. VA DANS TA FAMILLE DONNER DES LEÇONS DE MORALE C'EST BIEN PLUS ADAPTÉ.
Exatactement ma cherie man mi goor lako fogone billaahi y'avait une femme du nom de lobé ganiou na sakh meme si bo nekee djiguene defaroul ba rafet tekk SA grefage wala SA yaye bou rafete takk diaar am foulak fayda job SA job koula guiss beug la meme SA voix dafa goreee de meme que phisiqueme mais. Yalnako yaallah diapalee rekk samou ko mouseul ko SI accident de travail
Sokhna reste tranquille guay teup di dall nann sa diiné sa te concerne yaw wergua? Djiguen meun na liguéy liguéy goor mais exactement islam dafani na goor nourok goor agir comme et djiguen de même.Topato sa bopp en tant que djiguén. Sa commentaire nk kholat ko@@fatimatabintoumarico8032
Pour la première fois, j'ai regardé une interview qui m'a vraiment touché.En plus, on voit clairement qu'elle aime vraiment son travail. Toutes mes félicitations, bravo binta et bonne continuation 👌
waw ki deh kouma diokhone kamil ma wate ni gore la sheuu du courage machallah yalla guati am réussite total sister.mes juste gua gueneu defar rasta yi mou goudou gua diko tak.machalla😍
Binta sama tourando yeye nga mais nk guir yalla nékkal djigéun xolatal sa bopp yaye boye Liguéy bi bakhna trop bonne continuations yalla na yalla barkel leupp❤😍
_Lii mooy androgyne senegalais yi xamuñu ko, maanaam dangay yor forme góor fekk jigéen nga, walla nga yor forme jigéen fekk góor nga. Demleen def recherche Google walla RUclips ANDROGYNE dingeen xam li ma leen wax, lii Yàlla moo koy bindee nit._
SA WAY KI DHALL BOLÉNKO BEUGUÉ WAKHLÉNKO MOU DJOUGUÉ SI LIGUÉY BIMOU NÉK NDAKH COMPORTEMENT BII MOU YOOR AK LOOK BII MOU YOOR DOU BOU BAKH BII IMPOSÉL SA BOPP SI YEUFOU DJIGUÉNN... KOULAY ENCOURAGÉ SI LI NAK BEUGOU LEU YÉNÉNN LIGUÉY YOU DJIGUÉN MEUNEU DÉF AMNAFI, GNILAY ENCOURAGÉ GNEUPP BEUGOUGNO MÉLNI YAW TÉ KOUSSI WAKHONE WAKHUU RELATION DI NGA DÉGG LOULA MÉTI... DÉMAL DÉFFI LÉNÉNN TA KHAMNI DJIGUÉNE NGA... ❤❤❤
Je pense k son apparence est dû à des problème génétiques... Écoutez sa voix, son physique... Même si elle fait taille basse avec perruque elle ne pourrai changer c'est juste l'œuvre d'Allah donc à nous de l'accepter et de la comprendre comme elle est ! qu'Allah te protège Binta 🩷🤍
Absolument peu etr ni lako yalla bindé mai c à elle de fair des efor pask look bi pr gor leu, amy mbacké est kom sa sa voix,son physique mai elle s'habille en femme c trs importan
Mais djiguene la n'a def yeufou dijiguene saf dijiguene bou soloule yeurei wolof mais mou sole pantalon et baudit après mou laiteux bopam bi ay tresse Dina nirou djiguene dé deilaineu encourager si yeufou dijiguene
Mes deux cousines ont fait la mécanique. Avec ce qu'elles racontent, il y a trop de problème quand tu es trop féminine parce que certains à leurs travail avait des comportements déplacer, leurs dire des choses que je ne peux pas répéter, les clients qui veulent les draguer où qui peuvent qu'elles ne connaissent pas les voitures. Dieu merci ca va maintenant
Vraiment liguey amoule djiguen wala goor mais binta da nga wara jiguèné nak sa apparence bii da gooré trop mais courage que Dieu t facilite les restes !
Ndeysane elle est très brace et tres ambitieuse ❤️ rew mbi ndaw you gueum sen bop kom yaw lagnou soxla . T tres belle aussi maa shaa Allah mais leitoul you meun xam ni djiggen nga . Elle communique bien ❤️
Pourquoi, vous dites pas que la valeur d’une femme n’est pas seulement être mariée ? Cette femme a beaucoup de mérite et de valeurs. Du courage ma grande.
@@ElhadjiSamb-p2w diegalou Sakh takhou reutie wayé pour commencer dieulal sa khour yi dém déloko goor yi Dora nieuw jakarlo ak man dawuma Dali massa ya
N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ...
Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii...
Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP
+221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
🇸🇳♥️♥️♥️Kou beug binta lalal j'aime ❤❤❤🇸🇳
En tout cas on vous encourage mes aussi défaroule aussi nga soralé danga wara ame Djieukar
Talkal.nakko.sama.dom.sagarr
Keep going ❤❤
❤️❤️❤️❤️❤️
Souma amone entreprise dieul leu wala yoboula Europe fekhel sa rasta yii goudou nga diko takk ❤ elle est tellement reconnaissante aussi 😢 yalna yalla takhawou defal la ndam goudal fan wi
Amine YA RABI
Motakh apparence lou yèmè leu. Ki kouma diokhone kamil ma wate ni dou djiguène nakh apparence. Mais stp dèl defar sa bopp kom djiguène stp. Courage a toi
Bilay 😅
Wakh deugu yalla mane mome damako beugu te yalla takh Ms batay sama xel daloul xawma lann la nakk
Niossi bok yaam bilahi walahi du jamais vu dafa goorè trop sakh na Djiguénè way na sad djiguéne
@@azizalofficiel5425ki androgyne leu meunoul dara ci li.niounane ko defaroul. Senegal dale..
Waax deug Yalla m Courage à toi
Bonne Continuation Jeune Fille Geuneu Gorr Gorlou Rék Xam Linga Beug Focus Si Am Esprit Bou Solides Lissi Déss Nga Bayiko Si Loxoy Süniü Borom Respect ✌️
Worna Serigne Touba Binta je suis fière de toi sa patronne bly limou la sëddel daffa dawwe sama yaram😢😢 machallah yalle nalla yalla Samm si barckë Nabylle Moustapha (psl)❤❤ je vous love❤❤❤❤❤❤❤❤
Je suis mécanicien Ce n'est pas un métier facile force et courage à toi ❤❤🎉
Bilahii khamou malla mè kou bakhe monguii nii ya gorrë ya ame djiomm sa kholl rafett naa diambarr yaye bauye tu ma fait pleurer 😢 yalla nalla yalla gueuneu takhawou et tu es toute belle 😢😢
Pourquoi elles faire son travails
@HbvTxdhfu dafa âme diomm je le vois par son regard elle est sensible osi elle a un bon cœur ❤️
Bly yaw❤
Ay binta bo nieuwon europe ak sa méthie bi khalis bou barii machalla🙏🏽
Niobokn kogne depuis enfance mm école aussi 🎉❤ Binta diam si yaw
Elle habite où ???
Kii ne Darah Diourbel la nekk dell wax deug
@@mamadouseck9755 loussiy sa yoone ?
@@mamadouseck9755Diourbel la deuk nio bok kogn
Ndeye sane Bineta yalla nl yalla 😢diapalé
Macha allah, Bineta diambar gua , liguèye moye lépe. Mais djiguène dafa wara saf djiguéne. Même so soloul yeuré djiguéne déle létou
problem bi keye moy sou leto es c qu dougnou fokni goor bou letou la tamite,mom keye ni lako yalla bindeh
Ohhh 🥹 binta Yallna yallah sama la inchallah te mayla ligua beugeu si ligeue bi inchallah 🥰🥹🙏
Les goûts et les couleurs ne se discute pas ya des gens qui vous aime comme saa chapeau 🎉 champions ❤❤❤💥🔥🔥🔥
Machallah liguey yep bakh mai tmt faut qu’on ce disent la vérité cette Binta koum wakhoul djiguenne leu doka geume man je les vus sur Tik tok yalla xam Nani goor laka tegone mai vraiment daf wara defar apparence bi xolal bopam bi tmt nit mom surtout Sénégalais limou guis rek lalay juger meun na nek mécanique ok mai wanei ni aussi djiguenne leu
Metier mom amoul Goor ak djiguen diom la rek, mais Binta défaroul nak djiguen déy saf djiguen, il y’a des femmes mécaniciennes Com toi mais bolén séné khamni aye djiguen lagnou, courage à toi
Ki deh kouma waxone ni djiguene douma ko gueum werante na b sonouna
Bilakh
Même sou defarou woul au moins mou def yeufou djigen.. lii Yalla reub nako
Walahi meme ici où j’habite y’a une fille qui fait le soudeur 🧑🏭 mai quand tu la vois dangoy beug elle est belle aussi changer woul comportement mai Binta changeel def yeufou djiguenne
Li nga wakh DEUG leuh Mais YALLA MOKO bindé nonou ,Nio bok kogn fi DIOURBEL
Que dieu vous protège Binta force à toi le meilleur reste à venir
Eskey yallah nala borom bii défal diam Inchallah ❤
Allah Houma Amine Ya Rabi Incha Allah 🙏🙏🙏♥️
Soyez francs avec elle Li dîné andoussi. Ton travail n'a rien à voir avec ta personne nékal djiguène bila yalla Def lolou moy deugue. Di djegalou nakh si c mes proches j'aurai pas laisser passer donc loubakh lako yéné. Bonne continuation !
MAIS SI TU TIENS À TON DIINÉ ÇA TE REGARDE. ELLE N'EST PAS OBLIGÉE DE FAIRE CE QUE VOUS VOULEZ LUI FAIRE FAIRE. VA DANS TA FAMILLE DONNER DES LEÇONS DE MORALE C'EST BIEN PLUS ADAPTÉ.
Exatactement ma cherie man mi goor lako fogone billaahi y'avait une femme du nom de lobé ganiou na sakh meme si bo nekee djiguene defaroul ba rafet tekk SA grefage wala SA yaye bou rafete takk diaar am foulak fayda job SA job koula guiss beug la meme SA voix dafa goreee de meme que phisiqueme mais. Yalnako yaallah diapalee rekk samou ko mouseul ko SI accident de travail
Sokhna reste tranquille guay teup di dall nann sa diiné sa te concerne yaw wergua? Djiguen meun na liguéy liguéy goor mais exactement islam dafani na goor nourok goor agir comme et djiguen de même.Topato sa bopp en tant que djiguén. Sa commentaire nk kholat ko@@fatimatabintoumarico8032
No yaw comprends,Bayil Binta nilako yalla bindé,yaw khalé nga comprendo,
@@diarradiene4275li nga wakh DEUG leuh mais Yalla moko bindé nonou nio bok kogn man ak Mom mako yar,
Pour la première fois, j'ai regardé une interview qui m'a vraiment touché.En plus, on voit clairement qu'elle aime vraiment son travail. Toutes mes félicitations, bravo binta et bonne continuation 👌
C'est un grand exemple pour la société d'aujourd'hui
Ndeysane yalnala yalla sam lingay sentou si métier bi yalnagako guiss inchallah
Ohhh Macha Allah ❤yalla na métier bi gueneu dougou inchallah ba do am loula si diakhal ❤
Merci smaa doom dji Bineta sante ngama t defaloumala dara diam si ioe❤
Yaw ya bakhe rék❤❤❤❤
Yaw ya bakhe rék❤❤❤❤
*Humm y’a bakh rk peut être y’a khebb lougue koy défaral mais mom khébouko🥰🙏🏽*
waw ki deh kouma diokhone kamil ma wate ni gore la sheuu du courage machallah yalla guati am réussite total sister.mes juste gua gueneu defar rasta yi mou goudou gua diko tak.machalla😍
❤ manchalla amatina sollo ❤️ courage à sokhna binta❤💯
Binta boul dioy nak yakeuga sama journée bi way ndeysan ❤
Binta sama tourando yeye nga mais nk guir yalla nékkal djigéun xolatal sa bopp yaye boye Liguéy bi bakhna trop bonne continuations yalla na yalla barkel leupp❤😍
Dedete ki dou djiguene
@myamandiang non dafa wara djiguéné nk
Ham yaw
@MbodjAmadouw3sh c'est pas a lui de se modifiée 😮😮
C'est ça androgyne
_Lii mooy androgyne senegalais yi xamuñu ko, maanaam dangay yor forme góor fekk jigéen nga, walla nga yor forme jigéen fekk góor nga. Demleen def recherche Google walla RUclips ANDROGYNE dingeen xam li ma leen wax, lii Yàlla moo koy bindee nit._
Yalla nalla Yalla maye ligua beugue si barké seydina mouhamet bilahi g pleuré 😢😢😢Yalla gua téral sa yaye inchalla bonne continuation
Binta nek sii rek day bakh on love mecanique
Deile sol yeurei djiguene té leutou sa bopou binta du courage 💪
Bonne continuation Binta yalna yalla barkel ligueye bi
Amine
Wa yén c koi le problème djinguén la kay😂 mashallah ki moy bineta...
😂😂
Ma bagne guemoumako😢😭😢
@@mariamacisse5972mane mi mai legui gueum nako
Mane dh geuw mako😂😂😂
@@cheikhdiop851 li androgyne la
SA WAY KI DHALL BOLÉNKO BEUGUÉ WAKHLÉNKO MOU DJOUGUÉ SI LIGUÉY BIMOU NÉK NDAKH COMPORTEMENT BII MOU YOOR AK LOOK BII MOU YOOR DOU BOU BAKH BII IMPOSÉL SA BOPP SI YEUFOU DJIGUÉNN... KOULAY ENCOURAGÉ SI LI NAK BEUGOU LEU YÉNÉNN LIGUÉY YOU DJIGUÉN MEUNEU DÉF AMNAFI, GNILAY ENCOURAGÉ GNEUPP BEUGOUGNO MÉLNI YAW TÉ KOUSSI WAKHONE WAKHUU RELATION DI NGA DÉGG LOULA MÉTI... DÉMAL DÉFFI LÉNÉNN TA KHAMNI DJIGUÉNE NGA... ❤❤❤
Vraiment 😊
Amnga diom mashalla ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️fière de toi yalla sam la inchalla 🙏❤️❤️
Bineta.daffal.comme.amy.mbacké.boul.falé.ay.wax.you.négative.courage❤❤❤
😢😢😢❤❤❤❤yalna borom bi takhawoula je versé des larmes bilahi
ndaysane yalla nako yalla diapalé🤲❤️
COURAGE ma sœur❤❤❤❤
Après chacun a son Style.bonne continuation espérant qu un jour tu auras ton propre garage 🙏🙏🙏🙏🙏
K dieu t bénisse franchement sw fière de toi
😢😢❤❤❤Bon courage Dieu et avec toi
Machalah Bineta bonne continuation ❤❤
Courage Bonn e continuations sénégalais mo Tama wakh bou niaw me dara❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ ❤❤❤❤😂
yalla nala yalla sam takhawoula arla BINTA on est fier de toi boula nekhone def lenen wala diay sa bop mais finko diap fofoula lep dina bakh inchallah
yalnala yalla djapalé banga teral say waaydjour 😢sama yaram dawna wallahi ❤❤❤
Vraiment je suis très heureux de vous ❤😊
Yalla Nako yalla diapalé way Binta 🤲🤲🤲🤲🤲🤲
Oh sister ❤ ... Je t'❤me fort ❤️ ... Courage 💪
Je pense k son apparence est dû à des problème génétiques... Écoutez sa voix, son physique... Même si elle fait taille basse avec perruque elle ne pourrai changer c'est juste l'œuvre d'Allah donc à nous de l'accepter et de la comprendre comme elle est ! qu'Allah te protège Binta 🩷🤍
Walahi khana Mouy dieul traitement pour modifier sa voix et son aspect en général
Absolument peu etr ni lako yalla bindé mai c à elle de fair des efor pask look bi pr gor leu, amy mbacké est kom sa sa voix,son physique mai elle s'habille en femme c trs importan
Effectivement! Elle a un taux de testostérone élevé, ce qui la rend "homme"!
Il existe des solutions médicales à son état.
Mais djiguene la n'a def yeufou dijiguene saf dijiguene bou soloule yeurei wolof mais mou sole pantalon et baudit après mou laiteux bopam bi ay tresse Dina nirou djiguene dé deilaineu encourager si yeufou dijiguene
Bien dit
Ki sunu kogn la deuk bilay nitt gno meuna yakk derr rkk ms tkt sister yalla bakhna ❤
Bilakhi nama yalla balle mais gor lako foguone basi voice bi mais yalla nalla yalla diapalé diambarre gua bagne kagne gua wallahi
Hola bineta❤❤❤ vamos vamos te quiero
Tu m'a fait pleurer ma belle courage
Merci Binta moytou breudeuh yi rek
Ndeyessane sama yarame dawna machallah dina bkh inchallah binta
Machalla Yalla nala yalla dèfal diam
Yala moye daifeu louka naikhe santé yala
Mes deux cousines ont fait la mécanique. Avec ce qu'elles racontent, il y a trop de problème quand tu es trop féminine parce que certains à leurs travail avait des comportements déplacer, leurs dire des choses que je ne peux pas répéter, les clients qui veulent les draguer où qui peuvent qu'elles ne connaissent pas les voitures. Dieu merci ca va maintenant
Kou beug Binta rek lalal j' aime je l'aime de trop💔💔
Machallah binta je suis contente avec toi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ yalna yalla diapale amine yarabi 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
Boul dioy massa bilakhi demala beug parceque denga am diom boul deglou wax you bone yi continue sur cette lancée ❤❤
Macha Allah yallah bahna continue binta
Machalla machalla Binta ki mome sama Yaye la yalla na sa diam yague
Yalla nala yalla samou si barké Serigne Touba🙏🏿
Maasàllaa Binta❤ca kaw ca kanam jàpp baña bàyyi sàggu bépp jigéen bu baax ga ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
En tout cas kholou djiguéne la yoré gaw n'a dioy 😢trop du courage yalnala yalla takhawou
Vraiment liguey amoule djiguen wala goor mais binta da nga wara jiguèné nak sa apparence bii da gooré trop mais courage que Dieu t facilite les restes !
Non vraiment c'est triste mais sa ira inch'Allah hurabi yalla taaxawu là
Courage à toi ma belle je te soutiens
Ndaysane Machallah ❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉
❤Machallah Qu'allah t'accompagne sur tout et te protège Liguey diamou yalla rek
Du courage bineta
Oh billaye j'ai les larmes aux yeux 😢 machalla rak dji ♥️♥️♥️♥️♥️ woutégué khalé you djiguéne youye mbarane dissi diok séneu yaye
Force à toi rk le meilleur reste à venir 🙏
Amine
@@soukayeyade4310 bilay défa jambar té am kerssa
Yalla na Yalla Guéna Sam Yarabi Bidiahy Seydina Mouhammad SAW
Wa ani bineta 😮
😂tes pas sérieuse
😂😂😂😂😂
Man dh comprendr wouma dara😅
Bilaye j’ai pas compris je demande rekk
😂😂😂
Je s8 fière de toi sister du courage
Force à toi Binta🫶
mashAllah yowe sa patron dillah kou bakh lah dape teuweu bayi
Ndeysane elle est très brace et tres ambitieuse ❤️ rew mbi ndaw you gueum sen bop kom yaw lagnou soxla . T tres belle aussi maa shaa Allah mais leitoul you meun xam ni djiggen nga . Elle communique bien ❤️
Très belle hum ! Pourquoi vous êtes menteurs ? Va la draguer.
@@fatimatabintoumarico8032😂😂😂😂😂
Pourquoi, vous dites pas que la valeur d’une femme n’est pas seulement être mariée ? Cette femme a beaucoup de mérite et de valeurs. Du courage ma grande.
Ndeysane Yalnala yalla defal diam bineta en plus tu es toute belle
Binta yallna sa diamou yage waye ❤❤❤
Je suis une bouchère mais sans nous empêcher pas de prendre soin de nous apres le travail
Machaĺah
never give up keep going 💪
Bineta 💯💯💯💯
Machalla binta.ligeuy.rek.dina.bakhe❤❤❤😢bonne continuation 😮
Binta yawe tamite dindile sa bopou bi thé daife yefou djiguene yawe tamite nake défaroule
Cherie sangé bate bi nekh guama defaroule ma belle ❤❤❤
Gracias hermanita ❤❤❤❤❤👏👏👏👏👏🫶🫶🤲🕌🤲🕌🤲🕌💯💯💯💯
Bayi len di wakh si nitt lou niaw touma dafa meti trop Billahi, surtout djiguene bou mak diomm nango ligueye soko doli woul diomm boulko khass ❤❤❤
Courage ma sœur ❤
Ooooh Ndayesan 😢❤
❤❤❤ chapeau reine
Thieuy yala moy bour ❤❤ force binta
Force à toi mais Yaw aussie défaroul touti ❤❤❤❤
Machalah sokhna bineta yalla sounou borom yokk la
Don’t cry love keep up the good work
Big respect ❤🙏❤
Kon ki djiguen la liguéy dafa méti mais defaroul nak
Noumoye défaro ki ni la mélle doff nga trop
Magui diégallou nak
@@ElhadjiSamb-p2w diegalou Sakh takhou reutie wayé pour commencer dieulal sa khour yi dém déloko goor yi Dora nieuw jakarlo ak man dawuma Dali massa ya
@@yayouSalihousamb1553😂😂😂😂
@mariane2697 balma khalé la😂
Binta yalanala yala défal diamé❤❤❤❤
Tout mes encouragements ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Lima diahal elle a une voix d'homme 😢 yalnala yalla same